Inna lillahi wa inna ilayhi radjihoune Serigne Abdou khadim Mbacke mom Serigne bassirou Khoudia mom Serigne Bara Mbacke mofi bayiko 17h laniou koy wadial touba inchallaah nit kou bakh démna yallna sounou borom yeureum ko te diégal ko si barkép Serigne touba amine